Senegaal

Réewum Senegaal
Raaya bu SenegaalKóót bu aarms bu Senegaal
Barabu Senegaal ci Rooj
Barabu Senegaal ci Rooj
Dayo196,723 km2
GoxAfrig
Way-dëkk12,853,259 nit
Fattaay59,26 nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
Pénc
Maki Sàll
Mohamed Dionne
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw

14° 43′ 29.06″ Bëj-gànnaar
     17° 28′ 24.06″ Sowwu
/ 14° 43′ 29.06″ Bëj-gànnaar
     17° 28′ 24.06″ Sowwu
/ -17.47335
Làkku nguur-giwu faraas
94% dinañ wax wolof
pël, séeréer, joolaa
KopparFranc CFA (XOF)
Turu aji-dëkkSenegaal-Senegaal
Sa-Senegaal
Telefon
Lonkoyoon bu Senegaal
Lonkoyoon bu Senegaal   Gtk-dialog-info.svg

Senegaal menn la ci réew yi ne ci Sowwu Afrig, mu bokk nag ci Afrig gu bëj-saalumu sahraa (Afrique sub-saharienne), Mbàmbulaanug Atlas diw digam ci sowwu, taqaloo ak Gànnaar ci bëj-gànnaar ak penku, Mali féete ko penku, Ginne ak Ginne Bisaawóo ci bëj-saalum, Gàmbi moom sos ab daanaka-jiba (quasi-enclave) ci biir Senegaal, sutuxlu ba ci lu ëpp 300 km ci biir suuf yi. Duni Bopp bu Wert bi (Cap-Vert) ñi ngi ci 560 km ci tefesi Senegaal yi.

Réew maa ngi lebe turam wi ci dex gi ko peek ci penku ak bëj-gànnaar, te ab balluwaayam bawoo ca Fuuta Jallon ca Ginne, di Dexug Senegaal. Ab kilimaam bu gëwéel la te di bu fendi te yor ñaari jamono: jamonoy nawet (jamonoy taw) ak ju noor (jamonoy fendi).

Ci jamonoy canc gi (la période coloniale), ay digg yu yaxantu yu bari, yu ay imbraatóor yu canc (empire coloniale) moomoon, daal di woon nañuy sampu ci tefes gi gépp. Dëkkub Ndar mujj na di péeyub Afrig gu Sowwu gu Faraas, mu mujj juge ci di leegi Ndakaaru ci 1902, moom Ndakaaru nag mujj na di péeyu Senegaal ca ba mu jotee ca ag tembam ca 1960, nekk ci cat li gën a féete sowwu ci goxub Afrig

La dale 2012 ba fimne Maki Sàll mooy njiitul réew ma. Senegaal ak doonte bokk na ci càmpéef yu bari yu àdduna bi, teewul bokk na ci Bennoo gu Afrig (Union africaine) ak Mbooloom diiwaan yu Sahel-sahraa yi (Communauté des États sahélo-sahariens)

Senegaal nag yaatoo na 196.190 km2.

Other Languages
Acèh: Senegal
адыгабзэ: Сенегал
Afrikaans: Senegal
Alemannisch: Senegal
አማርኛ: ሴኔጋል
aragonés: Senegal
العربية: السنغال
مصرى: سينيجال
asturianu: Senegal
azərbaycanca: Seneqal
تۆرکجه: سنقال
башҡортса: Сенегал
Boarisch: Senegal
žemaitėška: Senegals
Bikol Central: Senegal
беларуская: Сенегал
беларуская (тарашкевіца)‎: Сэнэгал
български: Сенегал
भोजपुरी: सेनेगल
Bahasa Banjar: Senegal
bamanankan: Senegal
বাংলা: সেনেগাল
བོད་ཡིག: སི་ནི་གཱལ།
বিষ্ণুপ্রিয়া মণিপুরী: সেনেগাল
brezhoneg: Senegal
bosanski: Senegal
буряад: Сенегал
català: Senegal
Chavacano de Zamboanga: Senegal
Mìng-dĕ̤ng-ngṳ̄: Senegal
нохчийн: Сенегал
Cebuano: Senegal
کوردی: سێنیگال
qırımtatarca: Senegal
čeština: Senegal
Чӑвашла: Сенегал
Cymraeg: Senegal
dansk: Senegal
Deutsch: Senegal
Zazaki: Senegal
dolnoserbski: Senegal
डोटेली: सेनेगल
ދިވެހިބަސް: ސެނެގާލް
eʋegbe: Senegal
Ελληνικά: Σενεγάλη
English: Senegal
Esperanto: Senegalo
español: Senegal
eesti: Senegal
euskara: Senegal
estremeñu: Senegal
فارسی: سنگال
Fulfulde: Senegaal
suomi: Senegal
Võro: Senegal
føroyskt: Senegal
français: Sénégal
arpetan: Sènègal
Nordfriisk: Seenegal
Frysk: Senegal
Gagauz: Senegal
Gàidhlig: Seanagal
galego: Senegal
Avañe'ẽ: Senegal
Hausa: Senegal
客家語/Hak-kâ-ngî: Senegal
עברית: סנגל
हिन्दी: सेनेगल
Fiji Hindi: Senegal
hrvatski: Senegal
hornjoserbsce: Senegal
Kreyòl ayisyen: Senegal
magyar: Szenegál
Հայերեն: Սենեգալ
interlingua: Senegal
Bahasa Indonesia: Senegal
Interlingue: Senegal
Igbo: Senegal
Ilokano: Senegal
Ido: Senegal
íslenska: Senegal
italiano: Senegal
日本語: セネガル
Patois: Senigal
la .lojban.: senegal
Basa Jawa: Sénégal
ქართული: სენეგალი
Qaraqalpaqsha: Senegal
Taqbaylit: Sinigal
Kabɩyɛ: Senegaalɩ
Kongo: Senangale
Gĩkũyũ: Senegal
қазақша: Сенегал
ಕನ್ನಡ: ಸೆನೆಗಲ್
한국어: 세네갈
kurdî: Senegal
kernowek: Senegal
Кыргызча: Сенегал
Latina: Senegalia
Ladino: Senegal
Lëtzebuergesch: Senegal
Lingua Franca Nova: Senegal
Luganda: Senegal
Limburgs: Senegal
Ligure: Senegal
lumbaart: Senegal
lingála: Senegale
لۊری شومالی: سنگال
lietuvių: Senegalas
latviešu: Senegāla
Malagasy: Senegala
олык марий: Сенегал
македонски: Сенегал
മലയാളം: സെനെഗൽ
монгол: Сенегал
मराठी: सेनेगाल
кырык мары: Сенегал
Bahasa Melayu: Senegal
Malti: Senegal
မြန်မာဘာသာ: ဆီနီဂေါနိုင်ငံ
مازِرونی: سنگال
Dorerin Naoero: Senegal
Nāhuatl: Senegal
Napulitano: Senegal
Plattdüütsch: Senegal
नेपाली: सेनेगल
नेपाल भाषा: सेनेगल
Nederlands: Senegal
norsk nynorsk: Senegal
norsk: Senegal
Novial: Senegal
Sesotho sa Leboa: Senegal
occitan: Senegal
Livvinkarjala: Senegalu
Oromoo: Senegaal
ଓଡ଼ିଆ: ସେନେଗାଲ
Ирон: Сенегал
ਪੰਜਾਬੀ: ਸੇਨੇਗਲ
Kapampangan: Senegal
Papiamentu: Senegal
पालि: सेनेगल
Norfuk / Pitkern: Senegaal
polski: Senegal
Piemontèis: Senegal
پنجابی: سینیگال
پښتو: سېنېگال
português: Senegal
Runa Simi: Sinigal
română: Senegal
русский: Сенегал
Kinyarwanda: Senegali
संस्कृतम्: सेनेगल
саха тыла: Сенегал
sardu: Senegal
sicilianu: Senegal
Scots: Senegal
سنڌي: سينيگال
davvisámegiella: Senegal
Sängö: Senegäle
srpskohrvatski / српскохрватски: Senegal
සිංහල: සෙනගල්
Simple English: Senegal
slovenčina: Senegal
slovenščina: Senegal
chiShona: Senegal
Soomaaliga: Sinigaal
shqip: Senegali
српски / srpski: Сенегал
Sesotho: Senegal
Seeltersk: Senegal
Basa Sunda: Sénégal
svenska: Senegal
Kiswahili: Senegal
ślůnski: Synegal
தமிழ்: செனிகல்
తెలుగు: సెనెగల్
тоҷикӣ: Сенегал
ትግርኛ: ሴኔጋል
Türkmençe: Senegal
Tagalog: Senegal
Tok Pisin: Senegal
Türkçe: Senegal
Xitsonga: Senegal
татарча/tatarça: Сенегал
ئۇيغۇرچە / Uyghurche: سېنېگال
українська: Сенегал
اردو: سینیگال
oʻzbekcha/ўзбекча: Senegal
vèneto: Senegal
vepsän kel’: Senegal
Tiếng Việt: Sénégal
Volapük: Senegalän
walon: Senegal
Winaray: Senegal
吴语: 塞內加爾
მარგალური: სენეგალი
ייִדיש: סענעגאל
Zeêuws: Senegal
中文: 塞内加尔
文言: 塞內加爾
Bân-lâm-gú: Senegal
粵語: 塞內加爾
isiZulu: ISenegal