Diiwaanu Ndakaaru


Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la.Man nga cee duggal sa loxo ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Diwaanu Ndakaaru aki goxam

Diiwaanu Ndakaaru, benn la ci fukk ak juroom-ñenti diiwaan yu Senegaal yi. Moo ci gën a tuuti, ci yaatuwaay, waaye moo ci gën a bari way-dëkk. Yaatuwaayam toll ci 550 km²

Ñoo ngi ko séddale ci ñenti Tund: Ndakaaru, Pikin, Géejawaay ak Tëngéj 
  • lëkkalekaay yu biti

Lëkkalekaay yu biti

Raayab Senegaal 14 Diiwaani Senegaal Raayab Senegaal

Cees · Fatik · Jurbel · Kafrin · Kawlax · Kéedugu · Koldaa · Luga · Maatam ·Ndakaaru · Ndar · Séeju · Siggcoor Tambakundaa ·

Other Languages
български: Дакар (регион)
bosanski: Regija Dakar
Deutsch: Region Dakar
English: Dakar Region
français: Dakar (région)
Bahasa Indonesia: Region Dakar
日本語: ダカール州
한국어: 다카르 주
lietuvių: Dakaro regionas
Nederlands: Dakar (regio)
português: Dakar (região)
română: Regiunea Dakar
中文: 达喀尔区