Diiwaan yu Bennoo

Diiwaan yu Bennoo
Raaya bu Diiwaan yu BennooKóót bu aarms bu Diiwaan yu Bennoo
Barabu Diiwaan yu Bennoo ci Rooj
Barabu Diiwaan yu Bennoo ci Rooj
Dayo9 629 048 km2
Gox
Way-dëkk305 683 227 nit
Fattaay31 nit/km2
Xeetu nguur
- Njiitu Réew
- Njiitu Jëwriñ
-
Donald Trump
-
Tembte
- Bawoo
- Taariix
Péy ak rëddi
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
Làkku nguur-giwu-angalteer
KopparDolaaru aamirig (USD)
Turu aji-dëkkAmirik-Amirik
-Sa-Amirik
Telefon
   Gtk-dialog-info.svg

Diiwaan-yu-Bennoo, walla Diiwaan-yu-Bennoo yu Aamerig ci anam gu gudd am réew la mu séddaliku ci juroom-fukki diwaan, ñent-fukk ak juroom-ñett yi ñoo taqaloo te féete ci diggante Mbàmbulaanug Atlas ak Gu-Dal gi, penku ba sowwu, Kanadaa moo féete bëj-gànnaar, Meksik nekk ci bëj-saalumam. Alaskaa ci la bokk donte taqu ci, mi ngi nekk ci sowwu Kanadaa. Hawaii moom mi ngi ci diggu mbàmbulaan Gu-Dal gi. Réew mi am na fukk ak ñenti diiwaan yu tasaaroo ci géeju karayib yi ak Gu-Dal gi. Péeyam mooy Washington.

Diiwaan-yu-Bennoo yi ci 2008, 302 ciy miliyoŋ ciy way-dëkk lañu amoon, loolu tax muy ñetteelu réew mi ëppi nit ci àdduna bi, ci ginnaawu Siin ak End. Réyaayam toll ci 9,4 junni km², di ñeenteel ci àdduna bi, ci ginnaawu Riisi, Kanadaa ak Siin. Gàddaay gi bari na fa lool, ba tax muy réew mi ëppi xeet yu jaxasoo ci Suuf si. Koom-koomam mooy bi gën a woomle ci àdduna bi, te moo am njuddéef mu ñumm mu biirum réew (NJ.Ñ.B) mi ëpp ci àdduna bi.

Other Languages
Alemannisch: USA
አማርኛ: አሜሪካ
aragonés: Estatos Unitos
مصرى: امريكا
Aymar aru: Istadus Unidus
žemaitėška: JAV
Bikol Central: Estados Unidos
беларуская (тарашкевіца)‎: Злучаныя Штаты Амэрыкі
भोजपुरी: अमेरिका
Bahasa Banjar: Amirika Serikat
বিষ্ণুপ্রিয়া মণিপুরী: তিলপারাষ্ট্র
Chavacano de Zamboanga: Estados Unidos de America
Mìng-dĕ̤ng-ngṳ̄: Mī-guók
Tsetsêhestâhese: United States
Nēhiyawēwin / ᓀᐦᐃᔭᐍᐏᐣ: ᑭᐦᒋ ᒨᐦᑯᒫᓇᐢᑭᕀ
словѣньскъ / ⰔⰎⰑⰂⰡⰐⰠⰔⰍⰟ: Амєрїканьскꙑ Ѥдьнѥнꙑ Дрьжавꙑ
dansk: USA
Thuɔŋjäŋ: Pawuut Matiic
ދިވެހިބަސް: އެމެރިކާ
eʋegbe: United States
emiliàn e rumagnòl: Stat Unî
English: United States
Esperanto: Usono
español: Estados Unidos
estremeñu: Estaus Uníus
Na Vosa Vakaviti: United States
føroyskt: USA
français: États-Unis
arpetan: Ètats-Unis
贛語: 美國
गोंयची कोंकणी / Gõychi Konknni: अमेरिकेचीं संयुक्त राज्यां
Bahasa Hulontalo: Amerika Serikat
𐌲𐌿𐍄𐌹𐍃𐌺: 𐌰𐌼𐌰𐌹𐍂𐌹𐌺𐌰
客家語/Hak-kâ-ngî: Mî-koet
Fiji Hindi: United States
Kreyòl ayisyen: Etazini
Bahasa Indonesia: Amerika Serikat
Ido: Usa
íslenska: Bandaríkin
ᐃᓄᒃᑎᑐᑦ/inuktitut: ᐊᒥᐊᓕᑲ
la .lojban.: mergu'e
Kabɩyɛ: Etaazuunii
Gĩkũyũ: United States
kalaallisut: Naalagaaffeqatigiit
ភាសាខ្មែរ: សហរដ្ឋអាមេរិក
한국어: 미국
kernowek: Statys Unys
Lingua Franca Nova: Statos Unida de America
Luganda: Amerika
Basa Banyumasan: Amerika Serikat
Malagasy: Etazonia
Baso Minangkabau: Amerika Sarikat
Bahasa Melayu: Amerika Syarikat
Dorerin Naoero: Eben Merika
Plattdüütsch: USA
Nederlands: Verenigde Staten
norsk nynorsk: USA
norsk: USA
Sesotho sa Leboa: United States of America
Chi-Chewa: United States
Livvinkarjala: Amerikan Yhtysvallat
Pangasinan: Estados Unidos
Kapampangan: Estados Unidos
Deitsch: Amerikaa
Norfuk / Pitkern: Yunitid Staits o' Merika
پنجابی: امریکہ
português: Estados Unidos
rumantsch: Stadis Unids
ᱥᱟᱱᱛᱟᱲᱤ: ᱥᱮᱞᱮᱫ ᱯᱚᱱᱚᱛ
sicilianu: Stati Uniti
srpskohrvatski / српскохрватски: Sjedinjene Američke Države
Simple English: United States
slovenčina: Spojené štáty
Sranantongo: Kondre Makandrameki
Basa Sunda: Amérika Sarikat
svenska: USA
Kiswahili: Marekani
ไทย: สหรัฐ
Setswana: USA
Tok Pisin: Ol Yunaitet Stet
Xitsonga: Amerikha
chiTumbuka: United States
Twi: Amerika
reo tahiti: Fenua Marite
oʻzbekcha/ўзбекча: Amerika Qoʻshma Shtatlari
Tiếng Việt: Hoa Kỳ
Volapük: Lamerikän
吴语: 美国
Vahcuengh: Meijgoz
中文: 美国
文言: 美國
Bân-lâm-gú: Bí-kok
粵語: 美國
isiZulu: IMelika