Ajara

Ci làkku ibrë (הָגָר) la tur wi jóge. Ajara moo ni ñu waxe tur wi ci Lislaam.Ci angale mooy Hagar; Ci faranse mooy Agar

Jaamu Saarata la woon, ñu mayoon ko Yonent Yàlla Ibraayma ni jabar, mu am ci Ismayla. Misra la bawoo. Man nañu jàng jalooreem ci Ge 16:1-16; 21:9-21.

Ci Injiil dañuy wax ci Ajara ci Gal 4:24,25.

Other Languages
العربية: هاجر
azərbaycanca: Hacər
Bikol Central: Hagar
български: Агар
বাংলা: হাজেরা
нохчийн: ХӀаджар
čeština: Hagar
Deutsch: Hagar
Zazaki: Hacer
Ελληνικά: Άγαρ
English: Hagar
Esperanto: Hagar
español: Agar
euskara: Agar (Biblia)
فارسی: هاجر
suomi: Hagar
français: Agar (Bible)
עברית: הגר
hrvatski: Hagara
Հայերեն: Հագար
Bahasa Indonesia: Hagar
italiano: Agar (Bibbia)
日本語: ハガル
한국어: 하갈
മലയാളം: ഹാജറ
Nederlands: Hagar
norsk: Hagar
português: Agar (Bíblia)
română: Hagar
русский: Агарь
سنڌي: ھاجرہ
svenska: Hagar
тоҷикӣ: Ҳоҷар
Türkçe: Hacer
ئۇيغۇرچە / Uyghurche: ھەزرىتى ھاجەر
اردو: ہاجرہ
中文: 夏甲